
Tabsiratul Anām
February 3, 2025 at 10:15 PM
_Mbokk yii, ñu ngi leen di fàttali ni Ziyaara am na Medina Baye *Vendredi bii di ñëw* in shaa ALLAH_
_Mooy Ziyaar boobu maggi taalibé yii tànnoon ngir saafuwante ak sëriñ bi, sàkku ndolal ci moom_
_*Soldaar warta tardé rappel !*_