
Daarah Salihina Officiel
February 13, 2025 at 09:51 PM
كرامتى خطُّ يد، فى خدمة المأيّد
وكان لى بالأفيد الله مولى الكرم »
« Mon miracle, ce sont mes écrits réalisés dans le service voué au partisan [le prophète (PSL)], et Allah le Maître de la noblesse a été fécond envers moi »*_
Sama karaama mooy sama mbindum loxo, jëm ci liggéeyal ka nga xam ne mooy Aji-Dëgërël Ji te nekkal na ma moom Yàlla (SWT) ci li gën a am njiariñ te mooy méngale ay teraangaam »
©️ Sëriñ Saalihu Mbàkke Xasiida, Ibn Sëriñ Faadilu Mbàkke, Ibn Sëriñ Suhaybu Ibn Xaadimur Rasuul ✍❤
❣Sopeep Alxadiim
#jërëjëf_borom_touba❤️
❤️
2