Daarah Salihina Officiel
Daarah Salihina Officiel
May 28, 2025 at 04:23 PM
Séentu weeru Tabaski 1446H... Ci bisub tay bii di Allarba 29i Diggi Tabaski (Zul Qihda) 1446H, deppoo ak le 28 Mai 2025, Mbooloo mi Serin bi denk wallum séentu weer wi ci Tuubaa, niki ni ñu ko baaxoo defe ci 29eelu fan ci weer wu nekk, dinañu daje ci sowwu Jumaay Tuubaa ju mag ji ngir séentu weeru Tabaskiw 1446. Mbooloo mi yore wallum séentu weer wi ci Tuubaa.
Image from Daarah Salihina Officiel: Séentu weeru Tabaski 1446H... Ci bisub tay bii di Allarba 29i Diggi Ta...
❤️ 👍 🙏 8

Comments