
Orange Money Sénégal
May 27, 2025 at 01:36 PM
Balle bi takk na dé 🥳🥳🥳
Utilise ton Kalpé Orange Money, nguir bokk ci xéweul you ñuy jooxé ci Tabaski bi.
Ay bazins, xaaru Tabaski, ay enveloppes yu dissss ak yenen lots lañu leen andillll🤩🤩🤩

❤️
👍
10