Orange Money Sénégal 
                                
                                    
                                        
                                    
                                
                            
                            
                    
                                
                                
                                June 12, 2025 at 11:48 AM
                               
                            
                        
                            *Tabaki bu weesu neex ak Orange Money🤩.*
Demone nañu *Dakar, Thiès, Mbour ak yenen régions* ngir téral suñu clients yi🥳
Lu ci melni ay *tissus Getzner,* ay *xaaru Tabaski,* ak yenen lots ont été distribués🥰. 
*Bravo à tous nos gagnants !🥳🎉*
Sasuné du ñu jokk ci dilen béggal😉.
Ni rek lay démé ak *Orange Money.*
Continuez à utiliser votre Kalpé car d’autres surprises vous attendent🤩.
#weesunakalpe
                        
                    
                    
                    
                        
                                    
                                        
                                            ❤️
                                        
                                    
                                        
                                            👍
                                        
                                    
                                        
                                            🙏
                                        
                                    
                                    
                                        9