✨طالب شيخ📿🤍TALIBÉCHEIKH☂️💡
✨طالب شيخ📿🤍TALIBÉCHEIKH☂️💡
June 15, 2025 at 03:33 PM
*Serigne Babacar Sy Elhadji MANSOUR*❤️ *Al Khalifa Néna🗣️* *« Ñaan Yalla mu nangu* *Bi ci gën a gaaw* *Fo gise nit teral ko ndax xamóo* *Fu làmmiñam tollu* *Ci noppu Yalla »🤌🏿❤️* *Boulén Jaani Kén Ko Guiss Wormal Ko So Amoul Nga Wakh Ko Ko Thi Ndiékk Ndax Adouna Kén Xamoul Yalla Xam🙏🏿*
Image from ✨طالب شيخ📿🤍TALIBÉCHEIKH☂️💡: *Serigne Babacar Sy Elhadji MANSOUR*❤️ *Al Khalifa Néna🗣️* *« Ñaan Ya...
❤️ 🙏 👍 🥰 😢 😮 🇵🇸 👏 🤍 139

Comments