
✨طالب شيخ📿🤍TALIBÉCHEIKH☂️💡
June 16, 2025 at 08:01 AM
*Seydi El Hadj Malick SY (RTA)*
Nena🗣️
«”*Nanga farlu ci sa tay*
*Ndax demb weesu na*
*Te ëllëg kumpa la*
*Kenn xamul luy xew*
*Kon nanga bàyyi xel*
*Ci bés bi nga tollu profitoo ci*"»

❤️
❤
👍
🙏
📿
✅
👏
🇵🇸
💙
📶
159