Assadul Khadim
Assadul Khadim
February 15, 2025 at 09:21 PM
Mandargaay Téqé: 1 - Amm yaqiin: xollam woolu Boroomam, té dall bubax ci diinéy Boroomam ji. 2 - Mu amm akk sammu ci diiném maanam aww lënt sax dakoy moytu rawanténa luko woor-né da arraam mba sipp nanuko. 3 - Dëddu Aduna mooy du bëgg Aduna ngir adunay késsé suko bëggé yit day doon ngir défaréeko Alaxira. 4 - Barri kérsa bamu féeñ ci bëttam 5 - Raggal Yalla, wégg ko, maggal-ko.

Comments