Assadul Khadim
Assadul Khadim
February 16, 2025 at 09:15 PM
Sëriñ Mustafaa Saliw mofi Bawo diko ñaanal mu tasefaak Sëriñ Tuuba ak Gaayi Yàlla yëpp. Ñunit ñu yàgg fi ci seeni mbegg andak suniy Sëriñ doon faw seeni mbegg biir ak biti ci Barke mbóotu Xassida YI. Amin
🙏 1

Comments